← Suurat yépp
Suurat 1083 aaya

الكوثر

Al-Kawthar

The Abundance

Tekki

Tann làkk

1

إِنَّآ أَعۡطَيۡنَٰكَ ٱلۡكَوۡثَرَ

Inna aAAtaynaka alkawthara

Jox Nanu la, déegub Kawsara.

2

فَصَلِّ لِرَبِّكَ وَٱنۡحَرۡ

Fasalli lirabbika wainhar

Na ngay julli ngir sa Boroom te na ngay rendi.

3

إِنَّ شَانِئَكَ هُوَ ٱلۡأَبۡتَرُ

Inna shaniaka huwa alabtaru

Ka lay bañ aka ñaawal, moo dog ci lépp lu baax. Saar 109 : Yéefër ya 6 - Laaya