إِذَا جَآءَ نَصۡرُ ٱللَّهِ وَٱلۡفَتۡحُ
Itha jaa nasru Allahi waalfathu
Saa su ndimbalu Yàlla dikkee ak ndam la,
An-Nasr
The Divine Support
Tekki
إِذَا جَآءَ نَصۡرُ ٱللَّهِ وَٱلۡفَتۡحُ
Itha jaa nasru Allahi waalfathu
Saa su ndimbalu Yàlla dikkee ak ndam la,
وَرَأَيۡتَ ٱلنَّاسَ يَدۡخُلُونَ فِي دِينِ ٱللَّهِ أَفۡوَاجٗا
Waraayta alnnasa yadkhuloona fee deeni Allahi afwajan
te nga gis ne nit ñaa ngi dugg def ay mbooloo ci biir diineey Yàlla ji,
فَسَبِّحۡ بِحَمۡدِ رَبِّكَ وَٱسۡتَغۡفِرۡهُۚ إِنَّهُۥ كَانَ تَوَّابَۢا
Fasabbih bihamdi rabbika waistaghfirhu innahu kana tawwaban
na nga sàbaal, te sant sa Boroom te na nga sàkku njéggalam. Moom Nànguwaakoonu tuub la. Saar 111 : Buum ga 5 - Laaya