قُلۡ هُوَ ٱللَّهُ أَحَدٌ
Qul huwa Allahu ahadun
Waxal ne : “Yàlla, moom Kenn la (jenn Yàlla rekk la).
Al-Ikhlas
The Sincerity
Tekki
قُلۡ هُوَ ٱللَّهُ أَحَدٌ
Qul huwa Allahu ahadun
Waxal ne : “Yàlla, moom Kenn la (jenn Yàlla rekk la).
ٱللَّهُ ٱلصَّمَدُ
Allahu alssamadu
Moom Yàlla, Mooy Kilifa gi wareefa joyal mbir yi.
لَمۡ يَلِدۡ وَلَمۡ يُولَدۡ
Lam yalid walam yooladu
Jurul, te Kenn juru ko.
وَلَمۡ يَكُن لَّهُۥ كُفُوًا أَحَدُۢ
Walam yakun lahu kufuwan ahadun
Te amul benni nàttangoo”. Saar 113 : Suba 5 - Laaya