← Suurat yépp
Suurat 958 aaya

التين

At-Tin

The Fig

Tekki

Tann làkk

1

وَٱلتِّينِ وَٱلزَّيۡتُونِ

Waaltteeni waalzzaytooni

Ci garabug fig ak oliw Maa ngi giñ !

2

وَطُورِ سِينِينَ

Watoori seeneena

Ak ci tund Siiniin (Siinaa’i) !

3

وَهَٰذَا ٱلۡبَلَدِ ٱلۡأَمِينِ

Wahatha albaladi alameeni

Ak ca réew mu wóor mii di (Màkka) ! ne

4

لَقَدۡ خَلَقۡنَا ٱلۡإِنسَٰنَ فِيٓ أَحۡسَنِ تَقۡوِيمٖ

Laqad khalaqna alinsana fee ahsani taqweemin

Bind nanu nit ci gën ja rafeti anam.

5

ثُمَّ رَدَدۡنَٰهُ أَسۡفَلَ سَٰفِلِينَ

Thumma radadnahu asfala safileena

Top, waaye man naa dem ba gëna suufe lépp lu suufe,

6

إِلَّا ٱلَّذِينَ ءَامَنُواْ وَعَمِلُواْ ٱلصَّـٰلِحَٰتِ فَلَهُمۡ أَجۡرٌ غَيۡرُ مَمۡنُونٖ

Illa allatheena amanoo waAAamiloo alssalihati falahum ajrun ghayru mamnoonin

ba mu des ña gëm tey jëfu yiw : ñoom dananu am pey gu dootul dog.

7

فَمَا يُكَذِّبُكَ بَعۡدُ بِٱلدِّينِ

Fama yukaththibuka baAAdu bialddeeni

Bu loolu wéyee, ana lan moo tax ngay weddi bisub faytoo ba (bis pénc) ?

8

أَلَيۡسَ ٱللَّهُ بِأَحۡكَمِ ٱلۡحَٰكِمِينَ

Alaysa Allahu biahkami alhakimeena

Moo xanaa Yàlla dafa dul ki dàqa àtte àttekat yi ? Saar 96 : Lumbu deret 19 Laaya