لِإِيلَٰفِ قُرَيۡشٍ
Lieelafi qurayshin
Ngir sababus màngug Qureys,(s)
Quraysh
QUREYCHI
لِإِيلَٰفِ قُرَيۡشٍ
Lieelafi qurayshin
Ngir sababus màngug Qureys,(s)
إِۦلَٰفِهِمۡ رِحۡلَةَ ٱلشِّتَآءِ وَٱلصَّيۡفِ
Eelafihim rihlata alshshitai waalssayfi
Seen mànko ci tukib sedd ak tàngaay.
فَلۡيَعۡبُدُواْ رَبَّ هَٰذَا ٱلۡبَيۡتِ
FalyaAAbudoo rabba hatha albayti
Na ñuy jaamu Yàlla boroom néeg bii.
ٱلَّذِيٓ أَطۡعَمَهُم مِّن جُوعٖ وَءَامَنَهُم مِّنۡ خَوۡفِۭ
Allathee atAAamahum min jooAAin waamanahum min khawfin
Yàlla mi leen joxu ñam ba xiifuñu aar leen it ba ragaluñu tiituñu! Saar 107 : Njëfandukaay 7 - Laaya
Source de la traduction
Allaaji Mamadu Ngeer ak Góorgi Jaw