← Suurat yépp
Suurat 1115 aaya

المسد

Al-Masad

The Palm Fiber

Tekki

Tann làkk

1

تَبَّتۡ يَدَآ أَبِي لَهَبٖ وَتَبَّ

Tabbat yada abee lahabin watabba

Ñaari yoxoy Abii Lahab dogg nañu te it dugg na.

2

مَآ أَغۡنَىٰ عَنۡهُ مَالُهُۥ وَمَا كَسَبَ

Ma aghna AAanhu maluhu wama kasaba

alalam ak la muy fàggu, du ko jariñ dara.

3

سَيَصۡلَىٰ نَارٗا ذَاتَ لَهَبٖ

Sayasla naran thata lahabin

Dana lakk ci biir Safara wuy bérax.

4

وَٱمۡرَأَتُهُۥ حَمَّالَةَ ٱلۡحَطَبِ

Waimraatuhu hammalata alhatabi

ak jabaram ja daan yanu matt ma,

5

فِي جِيدِهَا حَبۡلٞ مِّن مَّسَدِۭ

Fee jeediha hablun min masadin

loosam wa, buumug rawa cay nekk (caq bu ñu soy). Saar 112 : Sellal 4 - Laaya