إِنَّآ أَنزَلۡنَٰهُ فِي لَيۡلَةِ ٱلۡقَدۡرِ
Inna anzalnahu fee laylati alqadri
Wàcce nanu ko (Alxuraan) ci guddig dogal ba (Laylatul Qadri).
Al-Qadr
The Power
Tekki
إِنَّآ أَنزَلۡنَٰهُ فِي لَيۡلَةِ ٱلۡقَدۡرِ
Inna anzalnahu fee laylati alqadri
Wàcce nanu ko (Alxuraan) ci guddig dogal ba (Laylatul Qadri).
وَمَآ أَدۡرَىٰكَ مَا لَيۡلَةُ ٱلۡقَدۡرِ
Wama adraka ma laylatu alqadri
Ana lan moo lay xamal laylatul Qadri ?
لَيۡلَةُ ٱلۡقَدۡرِ خَيۡرٞ مِّنۡ أَلۡفِ شَهۡرٖ
Laylatu alqadri khayrun min alfi shahrin
Laylatul Qadri moo gën junni weer.
تَنَزَّلُ ٱلۡمَلَـٰٓئِكَةُ وَٱلرُّوحُ فِيهَا بِإِذۡنِ رَبِّهِم مِّن كُلِّ أَمۡرٖ
Tanazzalu almalaikatu waalrroohu feeha biithni rabbihim min kulli amrin
Ci guddi googu Malaaka ya, dañu cay wàcci àndak (Jibriil) ci seen ndigalu Boroom ci mépp mbir.
سَلَٰمٌ هِيَ حَتَّىٰ مَطۡلَعِ ٱلۡفَجۡرِ
Salamun hiya hatta matlaAAi alfajri
Jàmm rekk la ba baa njël di jot (fajar sa di xar). Saar 98 : Firnde 8 - Laaya