إِذَا زُلۡزِلَتِ ٱلۡأَرۡضُ زِلۡزَالَهَا
Itha zulzilati alardu zilzalaha
Saa su suuf si yëngutoo yëngoom ba,
Az-Zalzalah
The Earthquake
Tekki
إِذَا زُلۡزِلَتِ ٱلۡأَرۡضُ زِلۡزَالَهَا
Itha zulzilati alardu zilzalaha
Saa su suuf si yëngutoo yëngoom ba,
وَأَخۡرَجَتِ ٱلۡأَرۡضُ أَثۡقَالَهَا
Waakhrajati alardu athqalaha
te suuf si génne la mu suuloon,
وَقَالَ ٱلۡإِنسَٰنُ مَا لَهَا
Waqala alinsanu ma laha
nit naan : “Ngala man ?”
يَوۡمَئِذٖ تُحَدِّثُ أَخۡبَارَهَا
Yawmaithin tuhaddithu akhbaraha
bu keroogee, ci lay waxtaane ay xibaar,
بِأَنَّ رَبَّكَ أَوۡحَىٰ لَهَا
Bianna rabbaka awha laha
ci la ko sa Boroom soloo.
يَوۡمَئِذٖ يَصۡدُرُ ٱلنَّاسُ أَشۡتَاتٗا لِّيُرَوۡاْ أَعۡمَٰلَهُمۡ
Yawmaithin yasduru alnnasu ashtatan liyuraw aAAmalahum
Bu keroogee, nit ñéppay génn kenn kenn ngir ñu wan leen seeni jëf.
فَمَن يَعۡمَلۡ مِثۡقَالَ ذَرَّةٍ خَيۡرٗا يَرَهُۥ
Faman yaAAmal mithqala tharratin khayran yarahu
Képp ku jëf lu toll ni aw fepp te muy lu baax, dana ko gis,
وَمَن يَعۡمَلۡ مِثۡقَالَ ذَرَّةٖ شَرّٗا يَرَهُۥ
Waman yaAAmal mithqala tharratin sharran yarahu
Képp ku jëf lu toll ni aw fepp su dee lu bon, dana ko gis. Saar 100 : Jaabkat ya