← Suurat yépp
Suurat 9311 aaya

الضحى

Ad-Duhaa

The Morning Hours

Tekki

Tann làkk

1

وَٱلضُّحَىٰ

Waaldduha

Ci yoor-yoor bi ! Maa ngi giñ

2

وَٱلَّيۡلِ إِذَا سَجَىٰ

Waallayli itha saja

ak ci guddi gi bu kukkee ! ne

3

مَا وَدَّعَكَ رَبُّكَ وَمَا قَلَىٰ

Ma waddaAAaka rabbuka wama qala

Sa Boroom bàyyiwula, te bañu la.

4

وَلَلۡأٓخِرَةُ خَيۡرٞ لَّكَ مِنَ ٱلۡأُولَىٰ

Walalakhiratu khayrun laka mina aloola

Te àllaaxira, mooy, gën ci Yaw àddina de.

5

وَلَسَوۡفَ يُعۡطِيكَ رَبُّكَ فَتَرۡضَىٰٓ

Walasawfa yuAAteeka rabbuka fatarda

Te sa Boroom dana la jox, ba nga doyal.

6

أَلَمۡ يَجِدۡكَ يَتِيمٗا فَـَٔاوَىٰ

Alam yajidka yateeman faawa

Moo ndax fekku la ngay jirim ? Mu fat la !

7

وَوَجَدَكَ ضَآلّٗا فَهَدَىٰ

Wawajadaka dallan fahada

Ak it ndax fekku la nga réer ? Mu gindila.

8

وَوَجَدَكَ عَآئِلٗا فَأَغۡنَىٰ

Wawajadaka AAailan faaghna

Moo ndax fekku la nga ñàkk ? Mu woomalal la.

9

فَأَمَّا ٱلۡيَتِيمَ فَلَا تَقۡهَرۡ

Faamma alyateema fala taqhar

Jirim, nag, bu ko di xorñooñal.

10

وَأَمَّا ٱلسَّآئِلَ فَلَا تَنۡهَرۡ

Waamma alssaila fala tanhar

Te laajkat it, bu ko di delloo.

11

وَأَمَّا بِنِعۡمَةِ رَبِّكَ فَحَدِّثۡ

Waamma biniAAmati rabbika fahaddith

Te it na ngay waxtaane, sa xéewalu Boroom. Saar 94 : Féexal 8 - Laaya