← Suurat yépp
Suurat 10011 aaya

العاديات

Al-'Adiyat

The Courser

Tekki

Tann làkk

1

وَٱلۡعَٰدِيَٰتِ ضَبۡحٗا

WaalAAadiyati dabhan

Ca jaabkat ya seeni gimiñ di foor (fas) (Maa ngi giñ),

2

فَٱلۡمُورِيَٰتِ قَدۡحٗا

Faalmooriyati qadhan

tey këdaa seen tànk ya my xuuy (ferñent),

3

فَٱلۡمُغِيرَٰتِ صُبۡحٗا

Faalmugheerati subhan

ak yay songe suba coy.

4

فَأَثَرۡنَ بِهِۦ نَقۡعٗا

Faatharna bihi naqAAan

yay naawal pënd,

5

فَوَسَطۡنَ بِهِۦ جَمۡعًا

Fawasatna bihi jamAAan

tey xuus ca biir noon ya.

6

إِنَّ ٱلۡإِنسَٰنَ لِرَبِّهِۦ لَكَنُودٞ

Inna alinsana lirabbihi lakanoodun

Nit dey, kuy ñàkk deloo Boroomam njukal la ;

7

وَإِنَّهُۥ عَلَىٰ ذَٰلِكَ لَشَهِيدٞ

Wainnahu AAala thalika lashaheedun

te kat, moom, seede la ci loolu ;

8

وَإِنَّهُۥ لِحُبِّ ٱلۡخَيۡرِ لَشَدِيدٌ

Wainnahu lihubbi alkhayri lashadeedun

te kat moom ku tarla xérlool ci bëgg alal.

9

۞أَفَلَا يَعۡلَمُ إِذَا بُعۡثِرَ مَا فِي ٱلۡقُبُورِ

Afala yaAAlamu itha buAAthira ma fee alquboori

Xanaa dafa xamul saa su ñu ko jaxasee ci biir bàmmeel,(r)

10

وَحُصِّلَ مَا فِي ٱلصُّدُورِ

Wahussila ma fee alssudoori

te wuñées li nekk ci biir dënn yi,

11

إِنَّ رَبَّهُم بِهِمۡ يَوۡمَئِذٖ لَّخَبِيرُۢ

Inna rabbahum bihim yawmaithin lakhabeerun

bu keroogee, sa Boroom Ku deñ Kumpa la ci ñoom? Saar 101 : Toj-toj ba 11 - Laaya