ٱلۡقَارِعَةُ
AlqariAAatu
Toj-toj ba !
Al-Qari'ah
The Calamity
Tekki
ٱلۡقَارِعَةُ
AlqariAAatu
Toj-toj ba !
مَا ٱلۡقَارِعَةُ
Ma alqariAAatu
Ana lan mooy toj-toj ba ?
وَمَآ أَدۡرَىٰكَ مَا ٱلۡقَارِعَةُ
Wama adraka ma alqariAAatu
Ana lan moo lay xamal luy toj-toj ba ?
يَوۡمَ يَكُونُ ٱلنَّاسُ كَٱلۡفَرَاشِ ٱلۡمَبۡثُوثِ
Yawma yakoonu alnnasu kaalfarashi almabthoothi
Moo di bis ba nit ñi di melni ay lëpaalëpp yu ñu wasaare,
وَتَكُونُ ٱلۡجِبَالُ كَٱلۡعِهۡنِ ٱلۡمَنفُوشِ
Watakoonu aljibalu kaalAAihni almanfooshi
te tund doj yi it mujj mel ni ngëndal nooy nepp ;
فَأَمَّا مَن ثَقُلَتۡ مَوَٰزِينُهُۥ
Faamma man thaqulat mawazeenuhu
képp ku peeseem diis (ci yiw)
فَهُوَ فِي عِيشَةٖ رَّاضِيَةٖ
Fahuwa fee AAeeshatin radiyatin
ma nga ko ca dundu gu neex ;
وَأَمَّا مَنۡ خَفَّتۡ مَوَٰزِينُهُۥ
Waamma man khaffat mawazeenuhu
képp ku peeseem wayaf (ci yiw),
فَأُمُّهُۥ هَاوِيَةٞ
Faommuhu hawiyatun
ma ngay jëm Haawiyatu.
وَمَآ أَدۡرَىٰكَ مَا هِيَهۡ
Wama adraka ma hiyah
Ana luy xamal lan mooy loolu Haawiyatu ?
نَارٌ حَامِيَةُۢ
Narun hamiyatun
Aw Safara la wu tàng. Saar 102 : Ëpplaante 8 - Laaya