أَلَمۡ نَشۡرَحۡ لَكَ صَدۡرَكَ
Alam nashrah laka sadraka
Moo ndax féexalu nu la sa dënn ?(n)
Ash-Sharh
The Relief
Tekki
أَلَمۡ نَشۡرَحۡ لَكَ صَدۡرَكَ
Alam nashrah laka sadraka
Moo ndax féexalu nu la sa dënn ?(n)
وَوَضَعۡنَا عَنكَ وِزۡرَكَ
WawadaAAna AAanka wizraka
Te nu teggil la say bàkkaar
ٱلَّذِيٓ أَنقَضَ ظَهۡرَكَ
Allathee anqada thahraka
ya diisaloon sa ginnaaw ?
وَرَفَعۡنَا لَكَ ذِكۡرَكَ
WarafaAAna laka thikraka
Te yékatil nanu la saw tur ?
فَإِنَّ مَعَ ٱلۡعُسۡرِ يُسۡرًا
Fainna maAAa alAAusri yusran
Jafe-jafe bu nekk, àndanaak ug yombal !
إِنَّ مَعَ ٱلۡعُسۡرِ يُسۡرٗا
Inna maAAa alAAusri yusran
Jafe-jafe bu nekk, àndanaak ug yombal !
فَإِذَا فَرَغۡتَ فَٱنصَبۡ
Faitha faraghta fainsab
Te saa yoo féexee, jógël, (julli)
وَإِلَىٰ رَبِّكَ فَٱرۡغَب
Waila rabbika fairghab
te it na ngay xemmeem jëm ci sa Boroom. Saar 95 : Garabu Figg 8 - Laaya