وَٱلشَّمۡسِ وَضُحَىٰهَا
Waalshshamsi waduhaha
Ci jant beek leeram. Maa ngi giñ !
Ash-Shams
The Sun
Tekki
وَٱلشَّمۡسِ وَضُحَىٰهَا
Waalshshamsi waduhaha
Ci jant beek leeram. Maa ngi giñ !
وَٱلۡقَمَرِ إِذَا تَلَىٰهَا
Waalqamari itha talaha
Ak ci weer wi su ko dee topp !
وَٱلنَّهَارِ إِذَا جَلَّىٰهَا
Waalnnahari itha jallaha
Ak ci bëcëg bi su ko muuree !
وَٱلَّيۡلِ إِذَا يَغۡشَىٰهَا
Waallayli itha yaghshaha
Ak ci guddi gi su ko muuree !
وَٱلسَّمَآءِ وَمَا بَنَىٰهَا
Waalssamai wama banaha
Ak ci asamaan seek ka ko tabax !
وَٱلۡأَرۡضِ وَمَا طَحَىٰهَا
Waalardi wama tahaha
Ak ci suuf sek ka ko maasale !
وَنَفۡسٖ وَمَا سَوَّىٰهَا
Wanafsin wama sawwaha
Ak ci ruu geek Ka ko yemale ;
فَأَلۡهَمَهَا فُجُورَهَا وَتَقۡوَىٰهَا
Faalhamaha fujooraha wataqwaha
moom mi ko ràññatleel mbaax, ak mbon !
قَدۡ أَفۡلَحَ مَن زَكَّىٰهَا
Qad aflaha man zakkaha
képp ku ko sellal, daldi nay texe.
وَقَدۡ خَابَ مَن دَسَّىٰهَا
Waqad khaba man dassaha
te it, képp ku ko sàggane, daldi nay sooy.
كَذَّبَتۡ ثَمُودُ بِطَغۡوَىٰهَآ
Kaththabat thamoodu bitaghwaha
Waa Saamuud, seen bewte, tax na ñu weddi,
إِذِ ٱنۢبَعَثَ أَشۡقَىٰهَا
Ithi inbaAAatha ashqaha
ba ca ña gën weddi potoxlóo
فَقَالَ لَهُمۡ رَسُولُ ٱللَّهِ نَاقَةَ ٱللَّهِ وَسُقۡيَٰهَا
Faqala lahum rasoolu Allahi naqata Allahi wasuqyaha
Yonentub Yàlla ba ne leen : “Bàyyileen giléemug Yàlla gi ! mu naan”
فَكَذَّبُوهُ فَعَقَرُوهَا فَدَمۡدَمَ عَلَيۡهِمۡ رَبُّهُم بِذَنۢبِهِمۡ فَسَوَّىٰهَا
Fakaththaboohu faAAaqarooha fadamdama AAalayhim rabbuhum bithanbihim fasawwaha
Ñu weddi ko, rey ko. Seen Boroom, maasale na mbugël ma.ca kaw nit ñépp
وَلَا يَخَافُ عُقۡبَٰهَا
Wala yakhafu AAuqbaha
Te ragalul dara ca la cay mujj : Saar 92 : Guddi ga 21 - Laaya